Description
Njabootu Mala Yi : Ci àll bu mag, féeté Afrig soowu jànt, ci wetu dex gii séq Senegaal ak Mali, la amoon dëkk bu yéem bu tudd « Ndumbelaan ». Foofee, ay mala ñoo fa dëkkoon ci jàmm ak naatànge gu sax. Ku nekk amaloon na njariñ sa moroom. Waaye, mu am bis, ab nattu wàcc ci seen kaw ngir jàngal leen luy njariñal mbooloo ak jàppalante.
Dans la vaste savane d’Afrique de l’Ouest, près du fleuve Sénégal, s’étendait une jungle magique appelée « Ndumbelaan ». Là-bas, les animaux vivaient ensemble en paix, chacun jouant un rôle important dans leur communauté. Mais un jour, un défi les poussa à découvrir la valeur de l’union et de l’entraide.
Avis
Il n’y a pas encore d’avis.