Njabootu Mala Yi

15,00 

Catégorie :

Description

Njabootu Mala Yi : Ci àll bu mag, féeté Afrig soowu jànt, ci wetu dex gii séq Senegaal ak Mali, la amoon dëkk bu yéem bu tudd « Ndumbelaan ». Foofee, ay mala ñoo fa dëkkoon ci jàmm ak naatànge gu sax. Ku nekk amaloon na njariñ sa moroom. Waaye, mu am bis, ab nattu wàcc ci seen kaw ngir jàngal leen luy njariñal mbooloo ak jàppalante.


Dans la vaste savane d’Afrique de l’Ouest, près du fleuve Sénégal, s’étendait une jungle magique appelée « Ndumbelaan ». Là-bas, les animaux vivaient ensemble en paix, chacun jouant un rôle important dans leur communauté. Mais un jour, un défi les poussa à découvrir la valeur de l’union et de l’entraide.

Avis

Il n’y a pas encore d’avis.

Soyez le premier à laisser votre avis sur “Njabootu Mala Yi”

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *